Bismilaahi Rahmani Rahiim.
Nu fas yéene matal li desoon ci bayyit yi nga xam ne Sëriñ Alhaaji Mbàkke àndi na ko ci Dooley Mbidum Sëriñ Tuubaa. Muy ay bayyit yoo xam ne ku ko dégg di nga ci jëlle njariñ, sag pas-pas ak sa mbëggeel itam ci Sëriñ bi man na ci yokk bu wér. Noo ngi tuubal ñépp nag, ci njumte yiy man a feeñ ci jotali gi. Di ci fas yiw gu yaatu te koy ñaanal mbooleem ku ko doon topp. Yàlla nanu doon ay dëgg-dëggi Taalube kéem ni ko Sëriñ bi bëggee baekeb Xasiida yi.
Al-Habdul Xadiim
12/02/2021
Jërëjëfati Serigne Cheikh, santat tey bék si iow dila nianal serigne bi dolli la bou bakh si barkép khassida yi ❤️❤️❤️
Amiin Amiin Yàlla na Yàlla nangu ñaan barke Borom Tuubaa te boole nu ko jaajëfati
Machallah ! Jerejef
Jaajëfaat
Machalla amna solo lolou
Dieuredieuf
Alhamdoulilah yaaram sant neen