Leeral Miftaahul Xuyóob (7)

Nu wéyal ba tay ci mbiri baamel? Ndax mooy ku ñu def ci pax rekk ? Am romb na loolu.

Dees na fi leeral tamit xew-xew gu amoon diggante benn jullit ak ben yéefar gu siiw bob, di neen ci jëlle ay jàngat yu fees dell ak waare.

Yal nanu Yàlla musal ci tiisu bàmmeel.

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR