Fii danu fiy néttali leen ci téerey boroom ngir yi ni nu agsee ci Sëriñ bi. Tawfeex gi mu am ci ànd ak Boroomam ci lépp lu muy dugg dees na ko fi xam itam.
Naka noonu sell gi woon ci moom taxoon na dara manta rax ay mbiram. Fàww rekk lu sell rekk lay am, lu sell rekk lay taqoo. Yërmandeem ak yaatoom ci nit ñi réyoon na lool lool.
Yal nanu Yàlla xiir ci liggéeyal Seexul Xadiim.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien