Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu daf nu fi dénk jàng, liggéey ak sàmm sunu diine.
Dina fi leeral itam, moom Sëriñ bi, lu jëm ci ay mbiram niki wirdam, Sëriñam, yoonu géej gi ak yeneeni mbir. Naka noonu dees na fi déggee lenn ci ay jagleem ak i xéewalam.
Yal nanu Yàlla xir ci liggéeyal Seexul Xadiim ak sàmm ndonoom : Alxuraan ak Àddis, ci barkeb weeru Shahbaan, ak barkeb Borom Daarul Muhti.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien