Jotaayu Texe (10)

Ci xaaj bii di nanu fi jàngee nees di njariñoo ci Sëriñ Bi. Naka noonu ay teegin yu sew te gànjaru di na fi feeñee.

Ba tay ci xaaj bi, di nanu dolliku bu baax ci gën a xam Xasida yi ak seen dayo. Naka noonu Alxuraan ak i njariñam.

Yal nanu Yàlla xiir ci lu baax ak liggéeyal Sëriñ Tuubaa.

Jotaayu Texe<< Jotaayu Texe (11)
S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR