Safwatu Siiri (1)

Téere bii di «Safwatu Siiri fii siirati Xadiimi Xayril Bashar », Sëriñ Allaaji Mbàkke Xaadimul Xadiim moo ko taalif ngir murid yi ak jullit yépp njariñu ci.

Su ko defee ci dog bii, li ku fiy béral ci sababu taalif téere bi la jëm ak sukkandikukaay yi. Naka noonu dees na di xamle njëkk Sëriñ Bi di feeñ, ak feeñug jamonoom ak ay way-juram.

Yal nanu ko tàmbali ci jàmm te yegale ko ci jàmm barkeb weeru safar wi.

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR