Bismilaahi Rahmani Rahiim
Jaar-jaari Yónnent bi (Saws)-2
Ba Yónnent bi ganee àddina kiimaan yi fa xew ak xéewal yi mu indaale. Mbir yi amoon ci bañu xaree Dënam gu seel gi, ba tey itam leen ci turam yu seel yi te neex, di nga ko fi dégge insàllaa.
Al-Habdul Xadiim
27/10/2020
Yallah naga am geureum InchaALLAH si ligueye bou raffette bi tei am ndiarigne lolou sassounei