Leeral Daaju Muwaahibu 78 (2)

Bismilaahi Rahmani Rahiim

Nu dikkaat ak yéen ci beneen tomb jëm ci Daaju Mag ñi. Sëñ Abo Jaxate moo fas yéene leeral fii xeeti riim yi daje ci ñaareelu Daaju 78. Dina fi fàttali itam ni ko Sëriñ Saalihu Mbàkke Radiyallaahu daan bëggee, ba taxoon na sax mu santon ku nuy wax Baay Móodu Gay mu leeralal leen ko.

Yàlla nanu Yàlla saxal ci Jàngum Xasida barkeb Sheexul Xadiim.

Al-Habdul Xadiim

29/11/2021.

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR