Leeral Jazaa’u Shakuur (1)

Bismillahi Rahmaani Rahiim

Lii ab dog la ci Téerey Sëriñ Tuubaa bii nga xam ne daf ciy néttali Yoonu Géej gi. Ku ñuy wax Abdu Latiif la ci doon tontu.

La ko Tàmbalee Jéewal ba ca réew yu sori yi. Leeral na fa it lenn ci Xasiida yi mu bind ci yoon bi ak lenn it ci nattu yi : « daj naa ci diggante bi coono yoo xam ne duma ko néttali mukk ngir ay teggin ci sama Boroom, te loolu sama Boroom moo ma ci doon yar ».

Dafa doon déeyaale ak Boroomam, ci anam gu kawe, gu yéeme. Di wax it ak géej gi, di ko séedeloo ni mu doone jaamub Yàlla Subhaanahu képp.

Bokk na ci ay waxam : « ci juróomi at yi laa mujj mel ne ab jant ». Def na fa Téere bob lépp luy ag barke mi ngi ci.

« Tagg Yonent bi Aleyhi Salaam may na ma ag jiitu, fegal ma ag lor… »

S’abonner
Notification pour
guest
1 Commentaire
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Gueye
Gueye
2 années il y a

Jaajëf yaaram ! Amatina solo

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR