Bismillahi Rahmaani Rahiim
Fii nag danufiy leeral sangu farata ak tiim. Di neen fi wax farata yi ak sunna yi. Li lépp dafay dugg ci mbiri laab.
Naka noonu jullit bi dina fi xamee bu baax lu aju ci faratay koor, sunnay koor, faratay azaka ak teggini azaka. Naka noonu di neen fi xamle faratay aj ak sunnay aj.
Yal nanu Yàlla yombalal sunuy jaamu. Te saxal nu ci Lislaam barkeb Alxuraan.
Macha Allah Serigne Cheikh. Jangalémi amna solo bou baax. Sab Taluubé
Maa ngi seen ginnaaw d yaaram