Fii di neen fi leeral njariñal topp ndigal ak yitewoo njub. Dees na fi fésal itam ni léppi Sëriñ barkeele ak ni Yàlla di nangoo ñaanam.
Xar-baaxi Sëriñ Tuubaa itam cig mbindam ak i jagleem ak ni mu daan taxawoo taalube yi dees na ko fi xamee itam.
Naka noonu ni Sëriñ bi xamee mbiri ëllag, yéeme na lool, te dees na fi àndi lenn ci hisa yi koy dëggal.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien