Dénkaane Sëriñ bi jëm ci ab muritam(1).

Bismilaahi rahmaani rahiim. «Jógal jaamu Yàlla boo ragalee mu faat la loolu mooy tax doo woru ci àdduna, te jiital yéene ndax mooy tax sa yaakaar dëggu. Waaye boo nee danga yaakaar Yàlla ba noppi doo jëf ndigalam doo bàyyi ay téreem kon sa yaakaar dese naa mat. Moo tax mu ne ko bul bëgge, […]

Xaadimul Xadiim moy sant tey tagg Ahmadul Xadiim.

Moo mat ca kaw ndax mas ta def ab lëntMoo mat ci biir ndax moo waral nuy sant(…).

Siiratu Sheyxul Xadiim

Sëriñ Alhaji Mbàkke mooko taalif ngir mokkal jaar-jaari Señ bi Qàda lahu laahu maxtara lahu gana jàpandi ci ñun. Señ Mustafa Ñing mooko jang. Al khadimiyya TV ñooko yàtal

Diyàfatu samàdiyah (1)

1-Seriñ Tuuba Qàda lahu laahu maxtara lahu ne na: maqàma mi gana kawé fa yàlla jamono ji moy dëkal weetal yàlla cib xol. 2-Sëriñ Tuuba Qàda lahu laahu Maaxtara lahu ne na mbir yi ñetti xaacc lë: xam-xam bu am njariñ ak jëff ju yiiw ak teegin buñ gëram. Xam-xam bu am njariñ mi ngi […]

Kan moy Sëriñ Alhaji Mbàkke Xàdimul Xadiim ?

Bismilahi rahmani rahimi « Li ma xam ci sama’g  dundu ci gaatal man Xàdimu Xadiimi Rassùlilaahi sala laahu tahala haleyhi wa salam »      Ma ngi gané àdduna ci at’um 1979 wala 1980 ci Daarul Muhty, dëkub Maam Cerno Ibràhima  radiya laahu tahala anhu. Sama baay mi ngi tuddu  Seriñ Mustafa Hafsa doomi Serin Muhammad Hawa Bàlla […]

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR