Leeral Huqal Bukaa’u

Bismillaahi Rahmaani Rahiim Sang yi … Ku ci nekk day am leer gu toll ne leerug jant bi fu mu man a jëm. Su ko defe képp kuy leerloo ci moom day am lu rëy. Day mel ne ku gisul mbindéef yi ngir jublu Boroomam ak i leeram yu bari ak i mbóotam. Day man […]

Yoon Wu Sori Wi(3)

Sëriñ Tuubaa nee na  » Ca gaal ga la ma Yàlla xamalee ne kuy liggéeyal Yonent bi laa. Foofu it laa taggee Yonent bi tagg wuy sax di ko fekk fa mu ne » . « Fa Conakry, Yàlla setal na ma ci lépp luy jëme ci lu ñaaw, fegal ma ko. Tagg naa fa Yonent bi […]

Yoon Wu Sori Wi (2)

Al-Habdul Xadiim15/09/2021

Yoon Wu Sori Wi(1)

« Ku yàkkaar ne sama tukki bii dama cee jëm feen fu dul ci Yàlla ak Yonent bi ba tax mu may dëkk yor jaasi ak i kano, Yàlla dana ko gàcceel, seetaan ko, mbindéef yi dinañu ko ngàññi, yeed ko, mu dee ak gàccee ak toroxtange. Yàlla nag dina ma dimbali far ak man, mbindéef […]

Silaahu Ahlil Xawfi (4) Waxtuy julli ak melow ni ngay fayee li la ci raw.

Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Su ko defe nu fas yéene téj Téere bii di Silaahu Ahlil Xawfi, jàngoon nga ci wareefu sàkku xam-xam, ba tax na ràññewon nga ponki diine ak li ciy farata ak sunna. Tay nag di nga fi xamee melow ni ngay fayee julli yi la raw ak seen ay waxtu. Al-Habdul Xadiim […]

Silaahu Ahlil Xawfi (3) Koor, asaka, aj ak àddisi Yónnent.

Bismilaahi Rahmani Rahiim. Ginnaaw xàmmee farata yi ak sunna yi waréef la ci bépp jullit . Ndegam itam sunu Boroom dimbali nanu ba nu jottali mbiri julli ak li aju ci laab. Noo ngi leen di baaxe tay ñatt ci ponki diine te mooy koor, asaka ak aj, toftalee ko ak ay àddis yu jëm […]

Silaahu Ahlil Xawfi (2). Lu aju ci faratay julli ak laab

Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Ginnaaw bi nu xamee ni wareef la ci jullit bi mu ràññatle farata yi ak sunna yi dina yell kon nu tàmbali ko ci julli ak laab. Su ko defe di nga fi dégge lu bari ci mbiri julli ak ci jàpp ak sangu farata ak tiim. Al-Habdul Xadiim 28/08/2020

Silaahu Ahlil Xawfi (1) Jàngum Fiq : laab ak li ci aju

Bismilaahi Rahmani Ndegam bëgg ngaa xam njariñal ràññatle farata ak sunna ci bépp jaamu Yàlla man nga teewlu lii. Al-Habdul Xadiim 12/08/2020

Ñaanug « Yawma harafa »

Bismilaahi Rahmani.Ñaanug « Yawma harafa »Xasiida gi Sëñ bee ko bind mu fees deel ak njariñ Al-Habdul Xadiim 30/07/2020

Jaalibatul Buruur (2) Teggin yu màgg yi.

Bismilaahi Rahmaani Rahiim. Jullit bi kuy ay noonam? Nees di def ba teqalikoo ak ñoom? Su ci ame tont yu leer, naka la war a def ba man a nekk ak nit ñi te topp Boroomam ci teggin yi gën a rafet, gën a seel, gën a ganjaru. Al-Habdul Xadiim 15/07/2020

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR