Sheexunaa Ahmadul Xadiim nee na »
« Bi ma woowee Yàlla fa Jéewal la naaguloo ibliis ci man. Moo tax it ma tàqalikoo ak nasaraan yi fa Jéewal ak feneen, te jëllu ma ay ngànaay ».
» Fa Ndar la ma Yàlla dàqalee lépp luy nax-nax ci barkeb Ahlu Badrin, jàmbaar ya. Foofu it laa ñaanee Yàlla ba mu fegal ma noon yi ni mu ma fegale nax-nax yi. Lor ak tiis, wa foofu it, nekk gi ma nekk ci Yoonu Yàlla moo ma ko faral ».
« Yàlla dàqal na ma fa Dakar wépp lor wu ma ibliis di jéem a xëccal. Tagg naa fa Yonent bi it tagg wu tax ibliis tàggoo ak man. La fa xewoon* nag Alxuraan moo ko far teggil ma ko.
- Lu fa xewoon?
Al-Habdul Xadiim
15/09/2021
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien