Bismilaahi Rahmani Rahiim.
Ginnaaw xàmmee farata yi ak sunna yi waréef la ci bépp jullit . Ndegam itam sunu Boroom dimbali nanu ba nu jottali mbiri julli ak li aju ci laab. Noo ngi leen di baaxe tay ñatt ci ponki diine te mooy koor, asaka ak aj, toftalee ko ak ay àddis yu jëm ci julli.
Al-Habdul Xadiim
03/09/2020
Dieureudieuf Mouride. Leeral yi am na solo lol
Jaajëfati
MaSha’ALLAH et dieureudjefaty 🙏🏾🙏🏾
Jaajëfati key
Machallah amna solo. Yallah na Serign bi barkel liguey bi
Amiin Amiin Soxna Jaara jërëjëf
Macha Allah amna solo lol