Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke (11)

Bismilaahi Rahmaani Rahiim

Ginnaaw ba mu nuyoo mbokk yi ak dëkkandoo yi dafa daaldi soññee ci farlu ci lu baax ak jaamu Yàlla ju sax, ak di boole xam ak jëfe. Fàttali fi it lenn ci àddis yi jëm ci sàmm sa bopp ak benn lor kenn. Mu dolli soññee ci farlu ci Jàngum Xasida yi ak liggéeyal Borom Tuubaa.

Yàlla nanu Yàlla boole jéggal te boole nu ci jàmmam yi dëggal barkeb Sheexul Xadiim.

Al-Habdul Xadiim
14/11/2021

S’abonner
Notification pour
guest
1 Commentaire
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Yacine
Yacine
2 années il y a

Dieureudieuf Mouride thi fattali bi ak dellosi bi. Yalla na yalla doli samb thi barké Cheikhoul Khadim sougnou Yakkar taiye ak euleuk.

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR