Bismilaahi Rahmani Rahiim
Ginnaaw ba mu nuyoo ci anam gu matale. Dafa daal di bàyyiloo xel mbooleem kuy jullit ñu farlu ci teewlu sunu Boroom ci sunuy mbir yépp. Ndax sunu Boroom mi ngi gis sunu lépp, te dees koy wara xalam. Di tuub fuñu tool, di ko fàttaliku ngir mu ñuy fàttaliku. Kon lépp lu nuy dugg war nanu seet lu ciy bëggam ak lu ko ci doonul. Moom dafay Boroom yërmande, bëgg a lool ku ko jublu. Loolu moo tax Sëriñ Tuubaa Xaada lahu laahu Maxtaara lahu daan ko ñaan mu dolli ko ag jublu. Te loolu daf lay teeqale ak ngistal, réy ak ya ca askanu.
Ci loolu la ñaanal ñépp sunu Boroom xiir nu ci boppam, te jubal nu. Yàlla nanu Yàlla defal dégg ak topp barkeb Xasiida yi.
Al-Habdul Xadiim
01/08/2021
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien