Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke(1)

Bismilaahi Rahmani Rahiim

Lii ab Dénkaane la bu gànjaru, Sërin Alhaaji Mbàkke Xaadimul Xadiim moo nu ci doon fàttali li nu àndi ci kaw suuf, te mooy jaamu sunu Boroom.

Mu fàttali nu fi itam ne war na ci nun, nu yittewoo tuub, xamal nu itam ne Alxuraan ak Xasiida mat naa fonk lool, te mat a jàng di ci fas ngërëmal Yàlla Subhanahu Wa Tahaala ak Sëriñ Tuubaa Xaada lahu laahu Maxtaara lahu.
Ba tay soññee ci joxe ak moytu bu wér bàkkaar yu mag yi.
Yàlla nanu Yàlla defal dégg ak topp.

Al-Habdul Xadiim
03/05/2020

S’abonner
Notification pour
guest
2 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Ndiaye Sarr Ndiaye
Ndiaye Sarr Ndiaye
3 années il y a

Machalla yalla Nanou yalla Maye AB dioub

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR