Bismilaahi Rahmani Rahiim.
Kon nu wéyal ci mayi Sëriñ bi cig mbidam mba yi mu ñaan Yàlla sunu Boroom defal ko ko ci. Ànd ak nu xam ne léppam la sunu Boroom nangu.
Al-Habdul Xadiim
26/09/2020

Jëre jëf amatina solo looool 🙏🏽
Jaajeufaat