Leeral Nahju (3)

Fii deef na leeral lenn ci ay teggin yi nit ki wara làmboo bu toogee ak ay mag walla mu nekk ci biiri nit.

Naka noonu deef na fi béral itam, ni nit ki wara sàmmee ay gëtam ak làmmiñam. Di xool lu baax, di am kersa tey wax yiw.

Di tàggat boppam itam ci noppi ci lépp loo xam ne kenn du ko wax, mba di ko wax amul njariñ.

Yal nanu Yàlla defal ay teggin yu ñu gëram barkeb Xasiida yi

S’abonner
Notification pour
guest
2 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
N’diaye
N’diaye
1 année il y a

Maacha allah DIEUWRIGNE

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR