Leeral Fathu Zaahiril Baatin…

Ginnaaw muslu ci saytane, ak julli gu mat ci Yonent bi Aleyhi Salaam, Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu daa sant Yàlla bu wér. Dafa daaldi xamle li yit pas-pas bi nu war a am ci sunu Boroom ak ay jeexitalam, ci sunu nekkin, sunu jëfin ak sunu dund.

Leeral Fathul Zaahiril Baatin…(2)

Dina fi feeñ lenn ci njariñ yi nekk ci bàyyeek sa lépp sa Boroom, woolu ko bu wóor, ak wéral sab pas-pas ci dëggal saw doxiin sa diggante ak moom. Am na lees ci toftal ci Téere bi, jëm ci leeral luy mag, ak i màndargaam. Akub tënk jëm ci ponki Diine.

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR