Jazbatu sighàr han lahibin li xidmatil muxtaar(1).

Bismilahi rahmani rahim. « Sëriñ Alhaji Mbàkke Xàdimul Xadiim mo ci’y gàttal ci wolof téeré bii ngir bëgg julit yëpp njariñu ci rawanté’naak muriid yi yalna ko yàlla nangu ci barkep Sëriñ Tuuba Qàda lahu laahu Maxtara lahu »                                                                        *** Méñatum « Jazbatu sighàr » Bismilahi rahmani rahim salla laahu hala sayyidina muhamadin wa […]

Siiratu Sheyxul Xadiim

Sëriñ Alhaji Mbàkke mooko taalif ngir mokkal jaar-jaari Señ bi Qàda lahu laahu maxtara lahu gana jàpandi ci ñun. Señ Mustafa Ñing mooko jang. Al khadimiyya TV ñooko yàtal

Diyàfatu samàdiyah (1)

1-Seriñ Tuuba Qàda lahu laahu maxtara lahu ne na: maqàma mi gana kawé fa yàlla jamono ji moy dëkal weetal yàlla cib xol. 2-Sëriñ Tuuba Qàda lahu laahu Maaxtara lahu ne na mbir yi ñetti xaacc lë: xam-xam bu am njariñ ak jëff ju yiiw ak teegin buñ gëram. Xam-xam bu am njariñ mi ngi […]

Serigne Saliou Mbacke ibn Serigne Abdoul Ahad JAARAMA CHEIKH IBRAHIMA FALL

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR