Li ab Téere bu m njariñ lool, ay wax ak i jëfiinu Sëriñ Bi moo ci nekk, nu man ci gindiku ci sunu lislaam ak ci sunu taalibe.
Fii nag matug Boroom Tuubaa dina di feeñee ak sunu tawfeex ci ànd ak moom.
Yal nanu nuur ci moom barkeb Xasiida yi .

17/03/2025
Al-Habdul Xadiim
Notifications
Manchallah mouride amna solo
Jërëjëf yaaram