Bismilaahi Rahmaani Rahiim
Sëriñ Abo Jaxate mooy dikkaat ci leeral Daaju Muwaahibu 78, ci ñaareelu tooluwaay wi. Dana fi leeral lu aju ci tontu gi ginnaaw ba ñu daaje ba noppi. Jànginu waa kër Sëñ Abdulaahi Jaxate ca na mu gën a refete dees na ko fi dégg, ak dundalaat ko fi.
Yàlla nanu Yàlla defal tawfeex ci Xasida yi barkeb Borom Tuubaa.
Al-Habdul Xadiim
19/11/2021.
Maa shaa Allah am naa solo. Dieureudieuf
Jaajëf noo ko bokk