Safwatu Siyar (4)

Ginaaw leeralug làqug Sëriñ Maam Moor Anta Sali, taxawaayu Sëriñ Bi, ak yoonu tarbiya gi mu ubbi, teg ci ay taalibeem, di leen yar ak soññi, di leen yee ak njariñ. Dina feeñee ci xaaj bi lenn ci sababi tukki bi, ak ni tukki bi demee, lenn ci yi aju ak yeneen.

Safwatu Siyar (3)

Ci ñetteelu xaaj bi di nga fi xamee lenn lu aju ci nelawag Maam Moor Anta Sali ak taxawaayu Sëriñ Bi ginnaaw làqug way-juram wu baax ba. Danga fi dégge it lenn lu aju ci waxante yi amoon ca denc ba. Naka noonu tànnug Sëriñ Bi ba ñu key wax lu mën ñongal àddunaam. Yiteem […]

Safwatu Siyar (2)

Ci xaaj bi lanuy leeral lenn ci li aju ci jàngum Sëriñ Bi. Farlu gi woon ci moom, sàmmonte gi, réyug xelam ak man a déggam. Dina fi feeñ tamit njariñ li mu amoon ci Daaray Sëriñ Moor Anta Sali, ak fi mu ko féetewoon. Ci buntu bi daanaka li ciy féd mooy jàngam, jàngale […]

L’arme des Craintifs (6)

Les actes obligatoires de l’ablution mineure sont : L’intention, le rinçage du visage, le lavage des mains jusqu’aux coudes et le fait de passer l’eau entre les doigts puis le lavagede la tête et des pieds ; aussi, respecter l’ordre et de bien frotter constituent les actes obligatoires de l’ablution mineure, soit untotal de huit. […]

Safwatu Siiri (1)

Téere bii di «Safwatu Siiri fii siirati Xadiimi Xayril Bashar », Sëriñ Allaaji Mbàkke Xaadimul Xadiim moo ko taalif ngir murid yi ak jullit yépp njariñu ci. Su ko defee ci dog bii, li ku fiy béral ci sababu taalif téere bi la jëm ak sukkandikukaay yi. Naka noonu dees na di xamle njëkk Sëriñ Bi […]

Leeral Mawaahibul Xudduus (10)

Bis boobee ca ngay gis ku jàq lool, fa ngay gis ku sunu Boroom mere lool, gis fa ku mu gërëm lool. Ñépp ñoo fay tase ñu baax ñi ak ñu bon, keroog boobee lañuy xam ne, bir yépp sunu Boroom doŋŋ a leen moom, kenn bokkul ak moom dara, bis boobee mooy dëgg-dëggi bis, […]

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR