Leeral Daaju Xasiida (5)

Bismilaahi Rahmani Rahiim

Lii ab tënk la jëm ci Taanug Sëriñ Saalihu ci daaj yi ak la mu sasoon ndogo yi ci nu koy jàng. Xasiida yooyu nag siiw na ci seen biir ci aw tur te mooy: « sas wi ». Dina fi tontu ay laaj yu jëm ci fànd woowu, moom Sëriñ Abo Jaxate jëwrinu Kureel Daaru Salaam Xelkom. Yàlla na ci xam-xam gu leer feeñee barkeb Sëriñ Saalihu.

Al-Habdul Xadiim, 05/11/2021.

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR