Tombi Borom Tuubaa (8)

Lii dees na fi jàngee doxiinu Sëriñ Tuubaa ci Alxuraan ak fonk gi mu ko fonkoon. Daf daan digle jàng Alxuraan, di ko durus ci ay lim yu wuute.

Ba tay muy soññi way-jur yi ci jàngal seen i doom Alxuraan. Dëkkam bii di Tuubaa it muy fésal ag bëggam ci am ñu fa nekk di ko jàngaleel Alxuraan.

Kon yal nanu Yàlla dimbali ba nuy man di jàng Alxuraan, di ko dundal bu baax ci dëkkam bii di Tuubaa.

S’abonner
Notification pour
guest
4 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Ousseynou diagne
Ousseynou diagne
1 année il y a

Sëriñ bi ni mu soññee si alxuraan Durus ko ak mokkal ko waroon a tax murid yi gën ko fonk donte ñoo Si man kudul ñoom

شيخ
شيخ
1 année il y a

ماشاءالله ياشيخ بارك الله فيك

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR