Safwatu Siyaar (7)

Dina leere ci nettali yi mën a muñug Sëriñ Bi ci lori ay noonam. Te jamono ju ne muy kuy déllu ci Boroomam Subhaanahu wa Tahaala.

Am na itam ay nit yu ko daan taxawu ci coobareey sunu Boroom, daan ànd ak moom ak di ko diis seen i soxla.

Yal nanu Yàlla sàmmal sunu taalube ci fànn yépp. Di sàkku ci ñépp ñu ñaanal Sëriñ Saalihu Salaam mi fi bàyyikoo doonoon kenn ci borom xam-xam yi te liggéey lu bari ci yoon wi.

Safwatu Siiri

Safwatu Siyar (6)
S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
✕
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR