Bismilaahi rahmaani rahiim.
<<Yaw Aadama Géy boo bëggee leerug sunu Boroom dee ko jaamu. Te bul bokk ci ñiy jaamu jiggéen ñi. Deel wéttalikio sa Boroom tay wut ngërëmam ànd ak di sellal, tay jihaadante ak sa bakkan. Bul def ci sa xol lu dul lu lay jëme ci sunu Boroom. Lépp loo xam ne day dox sa digg ak sa Boroom bàyyi ko, te wéeru ci Yàlla, te ragal ko, te wakiirlu ci moom.>>
Al-Habdul Xadiim
Grenoble, 26/01/2020.
Yacine