Kan moy Sëriñ Alhaji Mbàkke Xàdimul Xadiim ?

Sëriñ Alhaji Mbàkke Xàdimul Xadiim

Bismilahi rahmani rahimi

« Li ma xam ci sama’g  dundu ci gaatal man Xàdimu Xadiimi Rassùlilaahi sala laahu tahala haleyhi wa salam »

     Ma ngi gané àdduna ci at’um 1979 wala 1980 ci Daarul Muhty, dëkub Maam Cerno Ibràhima  radiya laahu tahala anhu. Sama baay mi ngi tuddu  Seriñ Mustafa Hafsa doomi Serin Muhammad Hawa Bàlla moom Maam Cerno radiya laahu tahala anhum, ak Soxna Hafsa Jaxate rahimaha laahu tahala. Sama Baay mooma tuddé sama baay bu ndaw bu tuddu Seriñ Kosso Astu Lo. Moom nak Maam Cerno lañu ko tuddé, ñu key wax Koso, ngir dëkub Kosso, moom nak la mu ajji won motax ñu mey wax Alhaaji. Tewul man mi hajj’na ci nganelul Yàlla tabaraka wa tahala.

(Insha’allah da nen ko yàtal ci sunu téeré bi ñuy waajé géené).

Al-Habdul Xadiim

Grenoble, 29/08/2019

     

S’abonner
Notification pour
guest
1 Commentaire
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
IBRAHIMA NDIAYE
IBRAHIMA NDIAYE
4 années il y a

MACHALLAH YALLA NAFI YAG LOLOU

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR