Tombi Borom Tuubaa (12)

Bismillahi Rahmani Rahiim

Ci xaaj wi nag deef na fi fesal ne Sëriñ bi daan soññee ci fonk julli guddi, ci feggu ak ci sàmm sa ngëm.

Deef na fi leeral yeneeni mbir jëm ci gëram sa Soxna. Sëriñ bi it jagle yu réy yi mu amoon. Naka noonu ay waxam ci Tuubaa, ak ni mu fonkewoon dëkkam ba. Ak ni dëkk bi barkeele, neex a jaamo Yàlla.

Dëkk bi ñoroon na ko lool, te fonk ko. Yal nanu Yàlla xiir ci fonk Tuubaa barkeb Seexul Xadiim.

S’abonner
Notification pour
guest
2 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Fallou Leye
Fallou Leye
1 année il y a

Tabarkalah amatina solo🙏🏽🙏🏽

Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR