Tay nag kàddu yi daa jëm ci waxi Sëriñ bi ci mag ñi niki Maam Cerno, Seex Ibraahima Faal, Maam Seex Anta, Sëriñ Daaru Asan Njaay, Sëriñ Abdu Karim Ture…
Dina fi feeñee itam seen i jagle yu réy ci Sëriñ bi.
Seenug baax, seenug jàmbaar, seen i jikko yu refet, seen doggu ak seen pasteef bu réy.
Yal nanu Yàlla defal la mu daan defal mag ñi barkeb Seexul Xadiim
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien