Sëriñ bi fii dina fiy néttali mbir yu am solo ci pajug yaram. Dina fi wax it nees di jëfandikoo lenn ci xob yi.
Nangug ag ñaanam, ak xam nees di fasee sa soxla dina fi feeñ ak ni mu fonkewoon aaya Alxuraan yi ci lépp lumuy def. Naka noonu ag sàmmam ci diinee, woyof gi ci moom, fonkam naafila ak yeneeni mbir yu am solo.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien