Bismilaahi Rahmaani Rahiim.
Fii danu fiy xamle ni Sëriñ bi daan jëflante ak Maam Cerno, te mooy ni mu ko yare, ni mu daan taqoo ak moom, ak ni mu ko gërëmee.
Al-Habdul Xadiim
Grenoble, 08/04/2020.
Bismilaahi Rahmaani Rahiim.
Fii danu fiy xamle ni Sëriñ bi daan jëflante ak Maam Cerno, te mooy ni mu ko yare, ni mu daan taqoo ak moom, ak ni mu ko gërëmee.
Al-Habdul Xadiim
Grenoble, 08/04/2020.
Dieureufeuti Mouride. Amatina solo. Yalla nanou yalla deffal degue ak top. Barké cheikhoul Khadim sougnou yaakkar tey ak euleuk.
Amiin Amiin Bàrke Borom Tuubaa
Jërëjëf ci yaatal gi amatina solo yàlla naleen yàlla fay yiw wu yaatu
Amiiin Bàrke Boroom Tuubaa
Jerejef sheikh bi leguèybi amna solo
Jaajëf ku baax!
Machallah
Machallah amna solo
Jërëjëf ku baax
Machallah am na solo lol dieredief yala na yala fayla si barké Serigne Touba
Amiin nu bokk ko
Sant Nagne dh.
Hakassa
Am na solo lool saw
Jërëjëf yaaram noo ko bokk