Bismillahi Rahmaani Rahiim
Fii danu fiy lim faratay Julli, Sunnay Julli, Faratay Jàpp, Sunay Jàpp. Ginnaaw ba nu xamee ni ngir Julli man a wér fàww jàpp gi wér.
Ak li nga xam ne it Imaam Xawfi xuppe na ko ci wàll woowu ngi soññiñu ci gëstu sunu Diine ak ràññatle bu wér liy farata ak liy sunna.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien