Dénkaaneb Sëriñ Alhaaji Mbàkke (7)

Bismilaahi Rahmaani Rahiim

Ginnaaw nuyoo gu yaatu, te sell jëm ci mbokki jullit yi dafa daaldi xamle ne Sëriñ bi mat naa fonk, dëkkam bi it di Tuubaa mat naa wormaal lool, rawatina Jumaa ji ak li ko wër ndax Malaayika yi duñu fa géj, leer yi di balloo fu ne. Mu fàttali bu wér solos topp ndigal ak wattandiku tere, daaldi baal ñépp hàq ak baalu ñépp hàq.

Yàlla nanu sunu Borom gindi ci boppam te defal Sëriñ Muntaxaa kiimaanug gudd fan ak wér barkeb Xasiida yi.

Al-Habdul Xadiim
13/08/2021

S’abonner
Notification pour
guest
0 Commentaires
Le plus ancien
Le plus récent Le plus populaire
Commentaires en ligne
Afficher tous les commentaires
Al-Habdul Xadiim

GRATUIT
VOIR