Su ko defe, ci xaaj wi la nu matale sunub liggéey ci Téere bii di Nahjul Qadaa Al-Haaj. Njariñ li yaatu na lool, la muy xamle di sunub defaru tay ak ëllag. Mbolleem li ci Sëriñ Tuubaa Xaada lahu Laahu Maxtaara lahu ñaan yal nanu dal.
Yal nanu Yàlla saxal ci am i teggin biir ak biti. Nangul nu sunuy jaamu, te gëram nu barkeb Seexul Xadiim.
S’abonner
0 Commentaires
Le plus ancien